Lenn li Ci kow puj yépp Lépp a ngi ne tekk Ci senn ruxx Do yëg sax Lu noyyi. Picc saa ngi ne selaw Ci àll bi. Xaaral rekk, Léegi yow itam Nga noppalu. Goethe Tekkikat bi Dr. Tamsir Aan.Téere-Woy yi(2011, Kulturbild Verlag)
Le site de la langue wolof et des langues africaines