golo gi golo gu ñuul gi dangin wi bukki bi yolaan wi siiru bi wel wi till wi suññeel wi kund wi wéxéñ wi jaar ji sikóor bi njaxat wi saaw bi mbexeex bi léebéer bi wànga-lànga wi nagu àll wi mbaam-àll mi kewel gi kooba gi mbill mi njamala gi fasu àll wi ñey…
Category: Taataan
Melo yi wolof
Benn bés, benn woy: Sëriñ Musaa ka
XARNU BI Sëriñ bi noo gi deeti ñaan Faqiir dafay nangoo dagaan Nangul nu lépp lu nu ñaan Ndax Yàlla naatal xarnu bi Noongi dangaan ci Mustafaa Ma nekk marwat’ak safaa Ak àqi amdi Mustafaa Mi Yàlla jébbal xarnu bi Ak àqi mboolem ay rakkam Ak àqi séen baay yi ñu am Ak àqi seex…
Ñeel Seex Anta Jóob
Liggéey bu mel ni bii ñu fi dëgmal, wareef la ci sunu gis-gis, ñu ñeel fi ca ndorte la góor gu mel ni Seex Anta Jóob. Ndax daf fee def, lu fi daanaka kenn ci waay-xeltu yi ci Afrik ak li ko wër deful: maanaam yesalaat yoon wi àddina sépp doon gise cosaanu nit ku…
“Symbole bi”: céy li ci réew mi!
Symbole ci nasaraan, su ngeen ko déggee mooy lëf koo xam ne dafa am lu muy mandaragaal! Du lëf ki ci boppam moo am solo, waaye la muy junjj ci xelu nit ñi la… Ndekete këf ki ñu leen bëgg a nettali masu fee jóg te mooy symbole bi fi daara tubaab bi indi di…
Yàggaay ci Wolof
Dal leen ag jamm!
Mbooloo mi! Ñu ngi leen di nuyu ku ci nekk ci yeen ci sa tur ak sa sànt te di leen dalal ci jàmm. Béréb bi ngeen tersi téy nag dañu koo sàncc, mool ko ci kalaama wolof, jagleel ko làmmiñ yi ñu nàmp, ci réewum Senegaal ak ci Afrik gépp. Yaakaar nañu ne lu…