Mbooloo mi! Ñu ngi leen di nuyu ku ci nekk ci yeen ci sa tur ak sa sànt te di leen dalal ci jàmm. Béréb bi ngeen tersi téy nag dañu koo sàncc, mool ko ci kalaama wolof, jagleel ko làmmiñ yi ñu nàmp, ci réewum Senegaal ak ci Afrik gépp. Yaakaar nañu ne lu…
Author: tam
Seex Musaa Ka: Xarnu bi
XARNU BI Sëriñ bi noo gi deeti ñaan Faqiir dafay nangoo dagaan Nangul nu lépp lu nu ñaan Ndax Yàlla naatal xarnu bi Noongi dangaan ci Mustafaa Ma nekk marwat’ak safaa Ak àqi amdi Mustafaa Mi Yàlla jébbal xarnu bi Ak àqi mboolem ay rakkam Ak àqi séen baay yi ñu am Ak àqi seex…
Taalif
woyi-kañ
Woyi-làmb
Laam ag liif Masambaay Mbéri Ndaw Béy du raas deemu guddee! Masambaay Mbéri Ndaw Béy du raas deemu guddee! Yégg naa! Yégg naa! Yégg naa ! Yégg naa ba ca biir Kaaba ga! Bind fa laam ak liif soo ga ñëw Laam ak liff googu laay daane mbër! Fa ma jaar ku fa jaar taq…
Sunu sosiete
Sunu sosete Sunu sosete yëngëtu na! Sunu sosete yëngëtu na! Ñun danuy am faydaa! Ñun danuy am faydaa! Ñun danuy fonk sunu Senegaal! Adduna potu ndaa laa! Ku fi naan jox sa morom naan! Adduna potu ndaa la! Ku fi naan jox sa morom naan! Faatu Fay Faatu yoo si…
Léeboon: Doomi Yàlla
Léeboon! Lippóon! Amoon na fi! Daan na am! Ba mu amee yaa fekkee? Ya wax ma dégg! waxi tey jar ta gëm! Sa yos moo ci raw! Xew xew bii ma nga ameewoon ca jamono ya rab yi daan wax ag nit ñi. Amoon fi jenn jigéen ju bon ju nekkoon ag ñeenti doomam. Ñoo…
Maki Sàll demoon na Kasamaas seeti jambaar yi…
Cëru nit ci Wolof
Kanam Bët Gémmiñ Bopp
Niseeryaa sànni na ñaari satelit ci jàww ji!
Réewum Niseerya siiwal na alxamees gee nu weesu – 18 fan ci weeru Ut – ne sànni ñaari “satelit” ci jàww ji. Satelit yooyee la ñu cay namm mooy yokk faggaru ci musiba yu mel ni maral ag mbën ngir yokkuteef ci wàllu mbay ag karaange ci seen dund. Ñaari satelit yooyu, ñu tudde NigeriaSat-2…