Bubakar Boris Jóob kenn la ci bindkat yi gëna mag ci Senegaal ag ci Afrik. Bind na ay téere yu siiw ci kalaama farañse ag benn téere bu am solo ci Wolof bu mu tuddee Doomi Golo. Laaj-toontu bii yeenekaayu “Le Monde des Livres” moo ko amaloon ak moom ci 16 fan ci weeru Awril….
Category: Caada
Yàtt bi lëmbee jamono! Su dee ni ko yenn waay-xeltu yi di waxee namm-namm xarala dëggantaan mooy gësëm xelu nit ñi ba ñu xippi xool, gise neneen mbir yi leen wër,ku yebboo kon ne yàtt bi Ablaay Wàd yàttlu Wakaam yégg na ca la mu ca doon wut. Ndax ndonte sax nag sotteegul, “ngenteegu” ñu…
Yàtt bi lëmbee jamono!
Su dee ni ko yenn waay-xeltu yi di waxee namm-namm xarala dëggantaan mooy gësëm xelu nit ñi ba ñu xippi xool, gise neneen mbir yi leen wër,ku yebboo kon ne yàtt bi Ablaay Wàd yàttlu Wakaam yégg na ca la mu ca doon wut. Ndax ndonte sax nag sotteegul, “ngenteegu” ñu ko maanaam, xel yeek…