Réewum Niseerya siiwal na alxamees gee nu weesu – 18 fan ci weeru Ut – ne sànni ñaari “satelit” ci jàww ji. Satelit yooyee la ñu cay namm mooy yokk faggaru ci musiba yu mel ni maral ag mbën ngir yokkuteef ci wàllu mbay ag karaange ci seen dund. Ñaari satelit yooyu, ñu tudde NigeriaSat-2…